Urgent! La Levée Du Corps De Sidy Lamine Niass Reportée La Déclaration De son fils Cheikh Niass

Condividi
Codice da incorporare
  • Pubblicato il 5 dic 2018
  • Urgent! La Levée Du Corps De Sidy Lamine Niass Reportée La Déclaration De son fils Cheikh Niass
    Visitez senegalinfos.com/ Contact Tel 00221 775312579
    senegalinfos votre site favori traite de la politique au senegal, le sport au senegal, les faits divers au senegal, la société au senegal, sans oublier la culture, les vacances au senegal, Dakarest la capitale du Senegal.
    Parmi les personnalités qui vivent au SENEGAL il y'a le Président de la République Macky Sall, Idrissa Seck, Sonko, , les lions du senegal, Ibrahima Macodou Fall, et parmi les entreprises RTS, RFM, Walf FL, Sud FM SEN RADIO.
    Le Sénégal, en forme longue la République du Sénégal, est un pays d'Afrique de l'Ouest. Il est bordé par l'océan Atlantique à l'ouest, la Mauritanie au nord, à l'est par le Mali, la Guinée et la Guinée-Bissau au sud. La Gambie forme une quasi-enclave dans le Sénégal, pénétrant à plus de 300 km à l'intérieur des terres. Les îles du Cap-Vert sont situées à 560 km de la côte sénégalaise. Le pays doit son nom au fleuve qui le borde à l'est et au nord et qui prend sa source dans le Fouta Djallon en Guinée. Le climat est tropical et sec avec deux saisons : la saison sèche et la saison des pluies.

    ++++++++++++++++++ INSTRUCTIONS ++++++++++++++++++
    Pour avoir des nouvelles du SENEGAL
    [Étape 1] REGARDEZ SUR LA CHAINE LA PLUS VISITEE A THIES


    Merci d'avoir regardé ce clip vidéo. Si vous avez des points en ce qui concerne senegal,senegalais, dakar, politique senegal, jamais hésiter à me contacter.

    Senegalinfos est un site de multimédia senegalais qui diffuse pleins de vidéos

    Connectez-vous avec notre entreprise senegalinfos
    IT-clip - it-clip.net/channel/UCyNvGi3ug3scsujcJkXgVgA
    Twitter - twitter.com/thiestv
    Facebook - web.facebook.com/thiesinfothi...
    Google+ - plus.google.com/u/0/+THIESINF...
    LinkdIn - www.linkedin.com/in/oumar-sey...
    Mon adresse Web - thiesinfo.com/

Commenti • 117

  • Die Ndao
    Die Ndao 3 giorni fa +1

    Y'a pas de talidé qui tiennent ici c Aux fils du défunt d décider . Que son âme repose en paix

  • aita niang
    aita niang 3 giorni fa

    Nagn dello xel yi si yalla ko hamni meussoul seetan nit d'i def loudoul yonn té dou réagir tay mou teud guenn d'i wah meunou tontou hamlen ni dhè rk moy deugu bayilen son fils def liko warr gni ko fiy khethio yepp diapalè wou gnou ko bimoulen sohla wè

  • khady Bamba
    khady Bamba 3 giorni fa

    Yeureum len ki diebal kou boramam vraiment mettina trop diaroul xeuthio bilay

  • Cherif Diago
    Cherif Diago 3 giorni fa

    Dako rouma yof mane kaolack la dakor lolou la keulifayi wakh dèlène deuglou keukifayii ak borome kham kham yii

  • Zama FZ
    Zama FZ 3 giorni fa

    sérigne sidy lamine président du groupe walfadjri etait un grand homme le sénégal a perdu quelqu un reposé vous en paix que sérigne ibrahima niass et son pére le profét l accueil au paradis

  • vidéos YouTube SN
    vidéos YouTube SN 3 giorni fa

    1 Jaime=hommages à sidy lamine Niasse

  • Amina Houdati
    Amina Houdati 3 giorni fa

    vraiment il ne merite pas ca madame kamara depuis maroc 😢😢😢

  • BA MANSOUR
    BA MANSOUR 3 giorni fa

    Vraiment il ne mérite pas ça .

  • Ibou Faye
    Ibou Faye 4 giorni fa +1

    Mais le corps appartient a son fils s il est l aîné

  • Khady Dieng
    Khady Dieng 4 giorni fa

    Aye waye lii niawna 😭😭😭di

    • Farmata Sall
      Farmata Sall 3 giorni fa

      Il faut respecter son choix C mieux. Paix à son âme

  • Oumar hamidou SY
    Oumar hamidou SY 4 giorni fa

    Name Elhaji sidy nieupeu ko bokk mais nak taawam bou goor aki ndiabottam nioniou thi euppeu walleu

  • Sombrero Malgache
    Sombrero Malgache 4 giorni fa

    Qu'est-ce que cette vidéo fout en tendances FRANÇAISES ?

  • Mamadou Sow
    Mamadou Sow 4 giorni fa

    Djiss nanè deug la dèthi ko gaw moo eupe yeurmandè mai nak c.est pa évident prsk yonete psl lundi lafi dioguè nioguiko dèthi mercredi donc on a pa vraiment les raison force de l.inhumer a Yoff keur dinè yi dingal rek mofa ame dc dingal dioqu na cheikh niass malgré les recommandations d ton père laisser comme ça sa diane wathie na machalah

  • Cheikh Ndiaye
    Cheikh Ndiaye 4 giorni fa

    ay domam nio eupe sagn sagn niépe thi mom lignou beugue lagnou wara déf kouy diaye sagn sagn nga dém diayiko thi sa baye té bayi bayou diambour bi diambari l'islam bi yalnako yalla défal téranga dioudoul diékh thi daradiay mouhamad s.a.w.salama

  • bijou diop
    bijou diop 4 giorni fa

    Non bouléne wakh talibé yui c’est famille vus les déclarations

  • ramatoulaye balde
    ramatoulaye balde 4 giorni fa

    qu Allah t'accueil dans son paradis RIP

  • abdoulaye niang
    abdoulaye niang 4 giorni fa

    cheikh Niasse DINA bakh inchala

  • Moustapha Fall
    Moustapha Fall 4 giorni fa

    NANE TOPPOU SÉNE NDIGALOUL BAY AHMAT KHALIFA NIASS ' NDAKHE MO FIY SÉNNE BAY TAY

  • Mata Hari Diaby
    Mata Hari Diaby 4 giorni fa

    il fut un homme qui s'est toujours battu pour le Sénégal. c'était un patriote. je suis malienne quand je vivais au Sénégal, il était mon exemple. 11 iklas pour le repos de son âme. tu es parti,mais tu reste dans nos coeur.

  • papamovic diop
    papamovic diop 4 giorni fa

    Nidiay djii dakko teuddé dawal xolko
    it-clip.net/video/t0Nf8WFcKMg/video.html
    LA PÉDOPHILIE DANS LA FAMILLE SÉNÉGALAISE

  • Abdou Gueye
    Abdou Gueye 4 giorni fa

    pour lann doudem yof nitki loumoubeug langkay défall

  • NiangBlg Apk
    NiangBlg Apk 4 giorni fa +2

    Ki dafa réw ta dafay féne Sidy Lamine wakhou ko dara
    Ta mome tékssy dou tawou Papame

  • Ibrahima Gaye
    Ibrahima Gaye 4 giorni fa

    Waxtan wax degue RK d'à siy baxx

  • kourakoura mbiss
    kourakoura mbiss 4 giorni fa

    Serigne talibem ,yenneti sakhbam,président peuplelam kouco sopi tahirga.sa talibe mouna diokho bacanam té sa dom diaraloulkoc

  • Cheikh A. K. Dieylani CAMARA

    son fils a tous les droits. Talibe dou sopp... talibés daay mandou

  • Oni Mad
    Oni Mad 4 giorni fa

    😭Rip 😭 rip 😭 rip 😭 rip 😭

  • Diop Ndéye fatou
    Diop Ndéye fatou 4 giorni fa

    Inalilahi wahinaliraja khona Yalla nako yala yereum Kilifa loumou dékané dal nagne kako défal mo guenn

  • Layzo Carlou
    Layzo Carlou 4 giorni fa +2

    Non vraiment li dou yoon ...C'est triste franchement !!!!

  • Seynabou Sarr Ringenbach
    Seynabou Sarr Ringenbach 4 giorni fa +4

    J'ai vraiment mal au coeur svp respecté le corps 😭😭😭😭😭😭😭😭😭méritéwoul li...

  • inconnu mbacké
    inconnu mbacké 4 giorni fa +2

    Aÿ way Lima wor moy sidy lamine méré nalén trop rou gui dem na ab néw rek guén di kheuthio soutoural lén ko enterré ko décédé depuis 3 jour guén teuyé ko rek

  • Malaw Diallo
    Malaw Diallo 4 giorni fa +2

    Lane Moy talibé Sénégal mo nékh

  • Lebron James
    Lebron James 4 giorni fa +5

    La terre où on doit le mettre n'a pas d'importance, Yoff ou Léona c'est pareil. Le Prophète psl on la gardé 3jr sans l'enterrement et beaucoup d'autre Sahara aussi. Et la décision final appartient au famille

  • yaye fall fall
    yaye fall fall 4 giorni fa +2

    Tiate dinala top baci birr bamel yalah nala yalah yeureum

  • Maguette Thiam
    Maguette Thiam 4 giorni fa +4

    Non me li c'est du jamais vu ani talibe ak kheuthio domou serigne bi

  • Max Diop
    Max Diop 4 giorni fa +3

    Dakar et kaolack c est meme chose dieu et partout

  • Abdelhadi Abdelhadi
    Abdelhadi Abdelhadi 4 giorni fa +4

    Je ne suis pas senegalais et qui il etait musulman il doit etre enterré le plus rapidement et ou il aurait aimé pourquoi pas? Du moment quil etait musulman rabi yerahmou en algerien

  • Yacine Ndiaye
    Yacine Ndiaye 4 giorni fa +1

    C vraiment dommage, mais IL ne merite pas ça. Allahouma firlahou warhamhou

  • Ndeyeawa Mbaye
    Ndeyeawa Mbaye 4 giorni fa +2

    Sidi lamine niass ne mérite pas ça il fallait pas laissé ça jusqu'à maintenant il faut que ses enfants prennent leurs responsabilités

  • ousmane NDIAYE
    ousmane NDIAYE 4 giorni fa +3

    Vairema sidy lepelou nou li bayi len werente wi ta dengi sidy fimo wakhe ay do mam

  • cherif Sarre
    cherif Sarre 4 giorni fa +2

    Yalla nako yalla kharel aldiana firdawsi

  • Marie Diatta
    Marie Diatta 4 giorni fa +3

    Yalla nako yalla yeureme kharéko aldiana firdawsi oh Sama yarame dawna 😭😭😭😭😭

  • Saly Ndiaye
    Saly Ndiaye 4 giorni fa +7

    Vraiment il ne mérite pas cela son fils aîné na qu'à prendre ses responsabilités en plus il voulait qu'on l'enterre à yoff ou es le problème vraiment li koumou nekone sa baye doula nekh

  • Aminata touré
    Aminata touré 4 giorni fa +1

    Sou fèkkè beugheu gha goudou fane daghay dèglou ngila fii djitou tè gha khamni dougnou deff lou yallah geureumoul indiko si penc mame bii lougne deff lou moyy lolou dèfoul deugg tè nèkout si deugg...

    • Fekam Kane
      Fekam Kane 4 giorni fa +1

      +Amina Cisse ki key moy lolou, dans qu'el senegal nous vivons ?

    • Amina Cisse
      Amina Cisse 4 giorni fa +3

      Ki weroul da dof bouko tontou vu ko

    • Fekam Kane
      Fekam Kane 4 giorni fa +4

      Wa mane damay beug warou ? Ki dè mo beug gnou dinthieuko Dakar ndakh simplicitem ndakh ragal yallam, nganane mame ak goude fane.

  • BABACAR SINE
    BABACAR SINE 4 giorni fa +2

    Merci chekh niasse

  • Aminata touré
    Aminata touré 4 giorni fa +1

    Cheikh na khamni sidy kilifam la c vrai wayè momitt daffa wara amm kilifa magg ngi bougnou wahè rekk waw gha si wara tekk (niakkeu kilifa goonè douko deff

    • thierno ba
      thierno ba 4 giorni fa

      C'est vraiment extraordinaire.
      Pour moi deux volontés s'opposent:l'une celle des talibés qui voient que leur marabout doit ètre aupres de ses parents pour que durants les gamous ça soit facile de leur coté pour des priéres et Ziara.
      De l'autre coté ses fils qui veulent qu'il soit à yoff.De ce fait y a pas de tord ni vinqueur ni vincu.Parler de marabout sans talibés c'est parler d'Etat sans chéf.
      Mais aussi quant on parle d'heritage c'est parce qu'il y a des relais qui sont ses fils.
      Donc c'est nous dans nous .Il faut plus de comprehension de la part des deux cotés.
      Que la terre lui soit légére Amine
      On a perdu un un trait d'union entre le fond et la forme.
      RIP

    • cheikh baye gadji
      cheikh baye gadji 4 giorni fa

      ki il est fou wilaya on le respect pas pour ay lime beugue sidy lamine sakhe dafa ame kilifeu walla
      alors khilafa lewna bou desse si ki daye tasse !!!

    • Amina Cisse
      Amina Cisse 4 giorni fa

      +Hamadou Diop ki weroule da doff

    • Amina Cisse
      Amina Cisse 4 giorni fa

      +Ousseynou Dione Lol

    • Ousseynou Dione
      Ousseynou Dione 4 giorni fa +1

      bayil ba sa baay dé ngeu dogal niune amnagne kilifeu wayé man sama serigne lima feké muy deff moy lath bdjaboot gui lou guene si beugeu niu deffé ko nonu talubé amul loumouy dogal si kilifam surtt mu laku nak..ndigeul gui dome ji mokoy diokhé nassi nieup antout wasalam.

  • Yacine SyllaSRK
    Yacine SyllaSRK 4 giorni fa +2

    ndeyssane

  • Mbodji Aïssatou
    Mbodji Aïssatou 4 giorni fa +6

    Vraiment il respecter sa dérniere volonté.

  • mbacke falle
    mbacke falle 4 giorni fa +10

    Sidy dafa comprend ni fo mane di nék sa dieuf rk mola fay fék guinaw yermandé yalla

  • Mouhamadou Lamine DIONE
    Mouhamadou Lamine DIONE 4 giorni fa +2

    Inna lilahi wa inna ileyhi radji ounne

  • Cheikh Ngom
    Cheikh Ngom 4 giorni fa +3

    Fatiha ak 11 lixlass salatou alla naby diokh ko Elhadj sidy lamine niass Yalla na khippé aldjana firdawzi amine

  • Ndiaye babacar
    Ndiaye babacar 4 giorni fa +2

    Ndeyssane

  • Ramatoulaye Diedhiou
    Ramatoulaye Diedhiou 4 giorni fa +4

    Il faut respecté sa dernière volonté et celle de sa famille ,pourquoi les talibés se comportent de cet façon paix à son âme

  • Mouhamadou lamine Dabo
    Mouhamadou lamine Dabo 4 giorni fa +3

    Entka l'Etat doit prendre ces résponsabilités demain ne se reste que pour réspecté le désir de SLN .son fils a le derniers mots .

  • soow dina
    soow dina 4 giorni fa +2

    Sidy lamine nitt kou oyoff la bilahi

  • Aida Gaye
    Aida Gaye 4 giorni fa +18

    Mais li dou yone guén defarko baparé diko remporter ba souba inchalla dioulite loko geuna tèla dinthie yeurmandè yalla wathie si mom mais liguèni Def dou deugu dou yone néna nagnouko yobou yoff kone yobou lenko fimou beugu guén yobouko entout cas dall mom mi teude yakamtina guén yobouko keureum bi moudie

  • Dado Ba
    Dado Ba 4 giorni fa +4

    Ndeyssane yaguena nagniouko diegual boromame yanna yalla yessal yeurmander si kawaw ndeyssane

  • Mame diarra Gueye
    Mame diarra Gueye 4 giorni fa +4

    Talibè dafaye woyè diguel dano sop waye domame moye dogal

    • Cheikh Nourou Niang
      Cheikh Nourou Niang 4 giorni fa

      Dangal doul domame do u do gal kilifay papam nioy dogal télolou moyy ame

  • Niang biz N
    Niang biz N 4 giorni fa +11

    Diambar danou n'a😭😭😭

  • Saer SANKHE
    Saer SANKHE 4 giorni fa +2

    Adouna mo yak sollo

  • Niang biz N
    Niang biz N 4 giorni fa +12

    Prends tes responsabilités c les dernières volontés d'une personne ki compte yalnako yalla yeureum té owafal souf si kawaw

  • domou djolloff
    domou djolloff 4 giorni fa +3

    Je suis choquée may wakh mounane Talibe wa gni kouniou. Aye simple talibe di doul lo nite yi

  • Oumy Ndiaye
    Oumy Ndiaye 4 giorni fa +37

    Ken dou dogal sa keur baay, ba paré di dogal keur bayou diambour. Nagne bayi ay domam gnou décidé

  • El Hadj Diallo
    El Hadj Diallo 4 giorni fa +12

    Mes sincère condoléances à toute la famille

    • Maguette Kamara
      Maguette Kamara 4 giorni fa

      Mes condoléances à sa famille que Allah l accueille au paradis

  • serigne mbackea
    serigne mbackea 4 giorni fa

    Mé l'an Moy problème bh l'an mo tax doniou co dfal limou beugeu ba wax co ay domam kan moco gneu diegé ndiabotam li domam wax lolou moyz

  • Aima Sow
    Aima Sow 4 giorni fa +18

    Aye mamame nio gui Léon niassene mais il faut respecter sa dernière volonté et celle de sa famille

  • Khady Sakho
    Khady Sakho 4 giorni fa +3

    Yalla nalen yalla défale limou beugue

  • borom belel
    borom belel 4 giorni fa +34

    Bayi lenn sen thiakhan yi sidi laminn defal na yalla lo khamni fom nek yalla fek kofa ak yeurmande

  • MohMo
    MohMo 4 giorni fa +25

    Si c’etait son choix qu’on l’execute! De toute façon personne ne le connait mieux que son fils.

  • autralia. kary
    autralia. kary 4 giorni fa +1

    COMMENT PEUT ON ALLER A L'ENCONTRE DE LA DERNIERE VOLONTE D'UN MORT... DE SON VIVANT SYDI LAMINE A VOULU QU'ON L'ENTERRE A YOFF..POURQUOI FAIRE LE CONTRAIRE. SA FAMILLE NE PEUT QUE SUIVRE. C'EST INADMISSIBLE CE TIRAILLEMENT..SYDI LAMINE NE MERITE PAS CA VRAIMENT

  • melanin girl
    melanin girl 4 giorni fa +30

    Wa pourkoi niouy bagne niou dénthieuko yoff? C koi le problem damay latheté rek😑

    • mamethiernu pene
      mamethiernu pene 4 giorni fa

      Ameth khalifa Niasse dakko bègue politisé

    • gueye cheikhna
      gueye cheikhna 4 giorni fa +5

      Nit dagnouy fontou bayilen djabot gui no def sen deuil si diam .kou fi guiss néw bougnou djeul diko yobou maka wala medine man khawma Sénégal lou len dal

    • Dioly Seye
      Dioly Seye 4 giorni fa

      melanin girl pask neinagn talibèm yi niooko bagn tè sidy yoff la wakhone

  • Awa Sylla
    Awa Sylla 4 giorni fa +2

    Ndeyessane R.I.P.

  • Fanta Fall
    Fanta Fall 4 giorni fa +75

    La décision appartient à ses enfants et non a ses talibés.c'est pas du tout normal j'ai le coeur meurti

    • Anna Dia
      Anna Dia 4 giorni fa +1

      Mounass Mimi walay c est désolant quoi li fi rk la ame

    • Mounass Mimi
      Mounass Mimi 4 giorni fa +4

      Fanta Fall problème bi dou talibés yi kessé amena yenene kilifa kaolack you nek sene guinaw. Lii niaw na torope😢😢

    • Anna Dia
      Anna Dia 4 giorni fa +3

      La décision revient à ses enfants 😡

    • Anna Dia
      Anna Dia 4 giorni fa

      Fanta Fall vraiment Sénégalais mo sof

  • Daouda Ndiaye
    Daouda Ndiaye 4 giorni fa +38

    Il faut respecter son testament son fils a tout dit

  • oumishta la capricieuse
    oumishta la capricieuse 4 giorni fa +12

    bilahi mérité woul lolou Niasse

    • Bassirou Ndiaye
      Bassirou Ndiaye 4 giorni fa

      +Adama Kandji yalnako yala yaram

    • Adama Kandji
      Adama Kandji 4 giorni fa

      Man Sénégalais dafma yeem nit dehh bayi ndekaner ak ay doman oie simple talibe rekk nga xawma auditeur nganer doufi amer ragallen yalla te settsi adji dem thie le dernier mot revient a sa famille

    • Lamine Baldé
      Lamine Baldé 4 giorni fa

      Mandale snegal diakhal namma nanko deffal limobougo. Sln merite woul li way

  • Cheikh Sarr
    Cheikh Sarr 4 giorni fa +32

    Il faut se consulter a la famille werente bakhoul te adouna amul solo yalla nako yalla yereum si BARKE SERIGNE TOUBA

    • Fan's cr7
      Fan's cr7 4 giorni fa

      Stop pas Barke serigne Touba ! 😡
      Arrêtez avec vos blablas. Repose en paix 👏😢

    • Aminata touré
      Aminata touré 4 giorni fa

      +nit da fay am yar ndour machalah ligha wakh moyy deugg q'il soit inhumè à kaolack

    • nit da fay am yar ndour
      nit da fay am yar ndour 4 giorni fa

      Dé léne wakhal ki dém limou wakh yobou lén ko kaolack si thiosanam bayilén thikhane

  • Yaya Wade
    Yaya Wade 4 giorni fa +7

    Adouna amoul solo soumma amatahou fa akh bara