Kooru Biddew Saison 4 - Épisode 8

Condividi
Codice da incorporare
  • Pubblicato il 14 mag 2019
  • Abonnez-vous à notre chaine IT-clip it-clip.net/channel/UCOvrLn57A83J8ojcX70n0Ew
    Suivez-nous sur Facebook facebook.com/leuzmedia?fref=ts
  • IntrattenimentoIntrattenimento

Commenti • 475

  • Nafissatou Kanoute
    Nafissatou Kanoute 5 giorni fa +1

    Mass lou mou def amoule tour

  • Raphaela Eichberg
    Raphaela Eichberg 5 giorni fa

    Sounds sweet

  • moussa sall
    moussa sall 5 giorni fa

    guerre day saf mondial

  • Ibrahima Faye
    Ibrahima Faye 5 giorni fa

    ' ü

  • SENEGALBOY12
    SENEGALBOY12 5 giorni fa

    Biddew 👍🏽👍🏽👍🏽👏🏼👏🏼👏🏼❤️

  • galzouframaren_bi_oficial oficial

    Bidew nak mongui beug sof wou diou rek Mou mell ni man djiguene bou bagn wou diou mom douma nex dará iss

  • Ög Wâÿ D
    Ög Wâÿ D 6 giorni fa

    Nn bidew mom ioe la faraal ms jaim op la façon dt tu traite masse....!!

  • Kiné lo Lo
    Kiné lo Lo 7 giorni fa

    🙎🤣🤣🤣🤣🤣🤣

  • Sidy Sarr
    Sidy Sarr 7 giorni fa

    Maie mass dalo xi de

  • mbengue mbengue
    mbengue mbengue 7 giorni fa

    Bideew est trop magnifique et classe mass loy guisser kou melni bidew diko dieunder cette vielle la

  • sokhna diarra diop
    sokhna diarra diop 7 giorni fa

    Bideww diepi na mass nak😂😂😂😂😂😂 non daro ak dan bobou couple😂😂😂😂😂 xaran rek la dann di def mom biral rk lay topato

  • Ly Ibou
    Ly Ibou 7 giorni fa +1

    Nice trop

  • Mba Camara
    Mba Camara 7 giorni fa

    .

  • Sidy baara Dieng
    Sidy baara Dieng 7 giorni fa

    Mimi dall nop nala man

  • Samsou Ndiaye
    Samsou Ndiaye 7 giorni fa

    Va chercher un mari noire comme du charon

  • mhd veridique
    mhd veridique 7 giorni fa

    Waay ki nexnama dh bideew mi

  • Ass Ndiaye
    Ass Ndiaye 7 giorni fa

    Merci waye Adji nila djiguène daye foula aussi sa kharit bi baxol guènèe kou si biti

  • Ndiakhate Cisse
    Ndiakhate Cisse 8 giorni fa

    , Alexandra Hepburn

  • Lamine Drame
    Lamine Drame 8 giorni fa

    Kone masse dafa deure

  • Pas Pied
    Pas Pied 8 giorni fa +2

    Remarque : bidew a changé de boucle d'oreille entre quand elle quittait la maison pour le boulot et quand elle est arrivée au bureau et qu'elle repond au phone.

  • Sagna Matar
    Sagna Matar 8 giorni fa

    Non Nakk Mass day sëral Bidew Dico
    pamti-pamté rk soit le DG Goor day Njëmei🍌

  • Mbaye Ndiaye
    Mbaye Ndiaye 8 giorni fa

    li amoul feinn

  • Mariama Diakhate
    Mariama Diakhate 8 giorni fa +1

    Mayma quelques moments mass dinama ray 😂😂😂😂😂😂

    • Ob trice
      Ob trice 6 giorni fa

      Waaaw dama warou sakh..1 moment..2 moments ..3moments..quelques moments

  • Boubacar Diallo
    Boubacar Diallo 8 giorni fa

    Ndenga monne toggo spécial biddew

  • Anna Dieye
    Anna Dieye 8 giorni fa

    Team biddew

  • Maria DIEYE
    Maria DIEYE 8 giorni fa

    Bidew yawittt wakhal ak mass c pas kom ça woudjou dou dara en plus yaw ki do moromom si bène côté 🤩🤩😘😘😘

  • nightcore play
    nightcore play 8 giorni fa +1

    J'aimerais que vous abonnez a ma candidature je fais des nightcore je suis en France mais je suis sénégalais j'espère que vous voulez plaisez sur ma chaîne youtube

  • charo gang
    charo gang 8 giorni fa +1

    😂😂😂😂

  • Gnilane Gueye
    Gnilane Gueye 8 giorni fa

    Bidew nekhna na trope nakh Dafa teyyy

  • AMINATA GUEYE
    AMINATA GUEYE 8 giorni fa

    Bidew nak yow la andak mais takal la niarel diaroul li

  • Baba Loum
    Baba Loum 8 giorni fa +1

    Mai mass dffa deurr wla

  • bachir domou parcelle
    bachir domou parcelle 8 giorni fa

    Biddew nak dafa soff kW ahhh do may mass diamou tmt

  • Bayedame Ndiaye
    Bayedame Ndiaye 8 giorni fa

    Bégaiement bi nal

  • Blue_Rose
    Blue_Rose 8 giorni fa

    Mimi elle est très jolie elle a un super beau teint mais dafa extravagante dale

  • Junior Fall
    Junior Fall 8 giorni fa

    Non bidew li ken douko def dieukeur dou morom deh

  • Racky Thiam
    Racky Thiam 8 giorni fa

    Mais nk Mass Amna droit takk Niar ba niet

  • Fafa
    Fafa 8 giorni fa

    Nit kou nek ak sa personnalité. Mane mome Adji damako yeureum pask defoul dara. Dafa beugu seuy rk

  • Camara Yoro
    Camara Yoro 8 giorni fa

    Bidew je suis ta fans depuis iralie

  • Serigne Touba Ndiaye
    Serigne Touba Ndiaye 8 giorni fa

    AjDA🌘

  • Abou Sow
    Abou Sow 8 giorni fa

    Lou takh Mass yambare

  • saliou ndiaye
    saliou ndiaye 8 giorni fa

    man ma beugue bideew kirassoulilah

  • Mamina O.B Mbaye
    Mamina O.B Mbaye 8 giorni fa

    Bidew way bidew way manchala danga wouyou sa tourr deh bidew deugg manchala

  • Thérèse TOUPANE
    Thérèse TOUPANE 8 giorni fa

    Les hommes sont bizarres; ils quittent dans ça va très bien (bidew) pour aller dans ça va pas du tout (niarel). 😂

  • BAYE DAROU. BI
    BAYE DAROU. BI 8 giorni fa

    Biddew Nak bet gama niou takkal la woudiou rek ga change

  • Essa Keita
    Essa Keita 8 giorni fa

    Kou guiss ne hale you goor yi Masse lagnou farral

  • Astou Gning
    Astou Gning 8 giorni fa +2

    Bidew je taime fort en plus tu a un joli teint machala

  • Yacine SENE
    Yacine SENE 8 giorni fa

    Masse yambar leu way thipppppp

  • ramata bakhoum
    ramata bakhoum 8 giorni fa

    Dane tamite wolou woul fama si wagnebii🤣🤣🤣🤣

  • Magatte Sarr
    Magatte Sarr 8 giorni fa

    Bideew nakk non franchement gniounne awoyyii nagniou bayyi yii goor Bou signer poly nakk chance rekk moyye takh dou takk

  • Coumba Cissokho
    Coumba Cissokho 8 giorni fa

    Bidéw man d.accorouma ak yaw woudiou diaroul li daguay guem sa bopou boul ko yeugual sa yaram boul wané ni amena loula méti

  • sambe seye
    sambe seye 8 giorni fa +1

    Vraiment 2em famme lou bakh la

  • Khady Thiam
    Khady Thiam 8 giorni fa

    Je ne comprends pas pourquoi vous essayé de ne faire croire k 2ème femme waroule awo doukou accepter mouk ta gnune geup gnu djoudousi je suis awo mais domou gnarel la c koi votre problème pourquoi gnakale fayda goor aussi kou tak tu assume Mme seye ba deme epuis c tt brrrrr

  • pããtrõōn Du RAM
    pããtrõōn Du RAM 8 giorni fa

    La Femme teint noire biii lolll

  • KHADY SOW
    KHADY SOW 8 giorni fa +1

    Prtan niarel bi baxna deh

  • Elimane Thiam
    Elimane Thiam 8 giorni fa

    Dane bayill daro migaye nakhe dell ndogou waye

  • Diattara Youssouf
    Diattara Youssouf 8 giorni fa

    Bidew ya ngi sonal sa bopp
    Fi ngay moudié nga ndiéké

  • Marianne Gueye
    Marianne Gueye 8 giorni fa

    Bidew mo fiir rk da melni mane mdrrrr

  • Hadidiatou Ndiaye
    Hadidiatou Ndiaye 8 giorni fa +2

    Mass tey ngay soga khamni couple communication mokay dokhal
    Wudiou bidew boudé yangui lirr message bi saches que tu n as pas d'amie, cette renoi là Elle est hyper jalouz

  • AMMGMM 2M
    AMMGMM 2M 8 giorni fa

    je trouve que Dane est un bon mari, ak lou meuneu am dafey nakhanté ak Fama rek

  • Balla Aïsha
    Balla Aïsha 8 giorni fa +2

    Goor buci signé Monogamy yeureum nala

  • Koda Niang
    Koda Niang 8 giorni fa +2

    fraîchement nekhatoul c etai pa l objectif ay 2eme femmes mom du defente

  • Nasio Fantane
    Nasio Fantane 8 giorni fa

    Yow biddew mo la man

  • Princess mbay
    Princess mbay 8 giorni fa

    Bidew Mass sa borom keur la nak

  • Samba Thiongane
    Samba Thiongane 8 giorni fa

    Masse amoul fouleuh dara siimmmmm

  • Brassia Fall
    Brassia Fall 8 giorni fa

    Mass ya léwét té niak khorom

  • CR7 cr7
    CR7 cr7 8 giorni fa

    badiane n'a gaw masse soone n'a de

  • lo modou
    lo modou 8 giorni fa

    Mass yambar ga nak naye khawa gorè way

  • Diop Kine
    Diop Kine 8 giorni fa +1

    Borome tin noir bi lima nèkh si mome da kham louko diapeu tes diko def lipolévre liguaye def mome Bxn calko fofou rk bisboko chabgé des dotoko défati

    • Ob trice
      Ob trice 6 giorni fa

      Wouyaye lipolevres 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣fogue na 2005 la gueudje dég mot bobou

  • Matta Lembaz
    Matta Lembaz 8 giorni fa

    Boudew bou rafetne

  • Maty salane
    Maty salane 8 giorni fa

    A thioum nék madame Gueye dal dou aye fo thieye li

  • Dieye Fatou
    Dieye Fatou 8 giorni fa

    Daro dh warnga kholat sa boppou chaque jour dann wot lay pou ndogou ji😄

  • Fatou Kiné Bâ
    Fatou Kiné Bâ 8 giorni fa

    Daro ak dieukkeur dji dinagne ma rey rék 😂

  • Mor DIENG
    Mor DIENG 8 giorni fa

    Bideew falèko waye

  • Ngadia Seck
    Ngadia Seck 8 giorni fa

    brava bidew e buona continuazione

  • omzo ne King
    omzo ne King 8 giorni fa

    Bidew ioe yaye kane

  • Ndeye Dieye
    Ndeye Dieye 8 giorni fa

    hé deugu d'où nkh bidew djiguene dayy am foula way wayé perte bâ melni lolou nonou

  • Khadime Kebe
    Khadime Kebe 8 giorni fa

    Mé pourtan il a l drw 1e deuxième fame .

  • Mamadou Diallo
    Mamadou Diallo 8 giorni fa +1

    Mass fan naaa la

  • Bois D'ébène
    Bois D'ébène 8 giorni fa

    Bidew est Chretienne wala dafa toub?

  • flexyswagger
    flexyswagger 8 giorni fa

    Deurouu mass bi à 2:50 😂😂😂😂

  • Aminata Keita
    Aminata Keita 8 giorni fa

    Mimi mom sokharoul

  • Maréme Diop
    Maréme Diop 8 giorni fa +1

    A mimi nak fouy nga ñiarél bagna toula ngakoy bagne ak sa kanam

  • Khadijaa Sow
    Khadijaa Sow 8 giorni fa

    Oh mane dal cette mimi là ne me plait pas du tout elle fait trop de manière

  • doudou ndiaye kaire sadio

    Mass tamite xana dou goor ki yaye djeukeurame dou mome moy sa djeukeure takoula yako Takk yakk nga fayda trop way

  • Djily Dia
    Djily Dia 8 giorni fa

    Proviseur fallou Cissé yalla nako yalla yeureum té kharé ko aldiana 😭😭11 likhlass svp

  • Rissa Jaryatoulla
    Rissa Jaryatoulla 8 giorni fa

    Salut abonnelen sama chaîne

  • Aissata Dieng
    Aissata Dieng 8 giorni fa

    Ma bekk thi sama bjddew bi djigene foula niaww🤣🤣

  • Ibrahima Lo
    Ibrahima Lo 8 giorni fa +1

    Pourtant femme bou nioul bi dafa rafet

  • fallou bah
    fallou bah 8 giorni fa

    Wzctane rek mo gyeunnn

  • Alioune Ndiaye
    Alioune Ndiaye 8 giorni fa

    bideew je t'aime

  • Seynaboulaye Fall
    Seynaboulaye Fall 8 giorni fa

    Ani wa team awaa tamite pousse bleu may djiss

  • El hadj Kouta
    El hadj Kouta 8 giorni fa

    Nn mass dafa deur 😂🤣

  • Sow Seydou
    Sow Seydou 8 giorni fa

    Muy bien. Este théâtro es muy interessante bueno contuaçion

  • serigne sama
    serigne sama 8 giorni fa

    Badiane mon menkè

  • Khadim Sylla Brésil chapeco

    Bidiw machala rafetgha mais adji Nak mola daxe niarel mass

  • thiate yayam
    thiate yayam 8 giorni fa

    thiey djiguenou Sénégal kouniou takal woudiou rek nga changer di diaboliser sa dieukeur

  • ashley dansira
    ashley dansira 9 giorni fa

    Lou meun nek wala loumou yéyoul gouro rek😎

  • KHW TV
    KHW TV 9 giorni fa

    Thiey Daro néna👉doléy goor djiguén🤣 vérité absolue ngay am fofou

  • serigne mansour sy seck
    serigne mansour sy seck 9 giorni fa +6

    Non Mass défaillant nga koi
    Bidew koukay takkal niarrel ak Sa Cd bou khossou bii damal outi clé USB 😁😁😁

    • Ob trice
      Ob trice 6 giorni fa +1

      Ndeyssane dafa deur

  • wiz Mame Ndiaye Ndiaye
    wiz Mame Ndiaye Ndiaye 9 giorni fa +8

    Biddew mi kat legui mou rew kat iow yay kan ba ki dou takk niarel en way