Urgent: déclaration de Ahmeth Khalifa Niasse sur son frère Sidy Lamine

Condividi
Codice da incorporare
  • Pubblicato il 4 dic 2018

Commenti • 411

  • Cherif Chifo
    Cherif Chifo 2 mesi fa

    Ina Lilahi wa ina ileyhi radjihone Yallah nako Yallah yeureum té khareko Aldiana firdawssi ak bép wayeu dawlou Inchallah Amine un homme d'une dimension spirituelle et intellectuelle extraordinaire un grand Patriote la voix des sans voix est parti Mr El Hadji Sidi Lamine Niass. Oustaz Ahmed khalifa Niass gnongui lakoy dialé Niass

  • vidéos YouTube SN
    vidéos YouTube SN 2 mesi fa +1

    1 j'aime=hommages à Sidy lamine Niasse

  • Thierno Muhammad diop

    Maachaallaah, mes condoléances, Yalla SWT xareko Aljanna FIRDAWSI ak mbooloom jullit

  • baye cheikh Diop
    baye cheikh Diop 2 mesi fa

    Ndayesane sidi

  • nayedio ba
    nayedio ba 2 mesi fa

    paix à son âme

  • Awa Lo
    Awa Lo 2 mesi fa

    Yalla nako yalla yeureum khareko aldianay firdawsi

  • IBA DIAGNE SARR
    IBA DIAGNE SARR 2 mesi fa +2

    Ahh,khana niou am Ndiortte bou rafète thi momm, thi limou ligéyy thi dinè..
    Aduna, nièppa gui wakh thi momm niou bari niogui wakh lounek mais Mane personnellement khaw ma lou mana khéww mais diap nani Souniou Ètat def naniouko lou mèti ,déff naniouko lounèkk pour tass Walfadri dèm na ba tribunal ndakh ndiakh lè thi diafè diafè youmou done ndoundou momm ak ndiabottam son Groupe je veux dire ndakh amè ay borr té manoko fayy dafa mèti am ayy borrr té guiso koula ko fayal dafa mèti, louy ressource financière pour group walfadri niou warone thi diott tè diotou niou thi dafa mètti.
    Loumou mommm lou wara dioguè thi Etat wara aksi tè manou thi diotte dafa mètti.
    ETAT SENEGAL léppi Sidy Lamine daniou ko neukheuseul , L'Ètat a fermè toutes les portes pour neurmèll groupe walfadri parceque effectivement andoul wone ak Etat.. mou amé ay borr manatoul wone fay ay borramm dafa Mèttii ...
    Amoul bènn yone bo kham ni Macky sall dieunde nako mouy directe pour Walfadri masoul amm , president macky sall massoul dieunde directe walfadri masoull am ,tè pourtemps ètat mo dakka dieunde directe ,television yepp etat dafay dieunde directe bamou dess walfadri mbokk yi ana lou gueuna mètti lii , bisi moudjiou yagoul dara mouy investitures bi ,tele yèppppp laniou diokh ay kopar you takou pour gniou wanè ko directe ,BAMU DÈSS WALFADRI LOU GUEUNA MÈTTI Lii Wakh lènn mako ... rien que pour torokhal group bi akk amone yènè sèyaall groupe bi ,parceque etat kou khèkh ak momm yayy niakk ndakh dolè djioulènn yalla diokh wala bokk dollè djioulènn yalla dèenkeu... tè biss dina nieuw dollè djiodjiou dioguè thi niomm dèmm thi yanènn dieumm..
    toutes les portes ont ete fermèes pour walfadri,dou marchè du publicitè dou avis dinfos du lènn,rien que pour torokhal walfadri .meeting bu massa am pour etat lumu niak niak fayda niou dieundeul ko directe la preuve investiture biii wèssou yagoul dara toudou nako légui tèlè yèpp encaisser naniou ,bamou dèss walfadri,tele yèpp laniou lambal poche pour guènè fa sènn directe bamu dèss walfadri , Sidy yagu naniouko tèk fitneu ,yagu naniouko togne yagu naniouko notttt yagu naniouko torokhal , yagu naniouko manquer respect ,pourquoi parceque il n’est pas avec letat cest la veritè ..et toute veritè merite dètre dite..
    artp niata yone muy dalleu thi kaw sidy lamine boudoul bènn di niarr,
    artp niata yone mou yoner sommation sidy lamine boudoul bènn di niarr ..
    bou moudjiou bi bi gua kham ni aduna yèp ko yeukk moy biko ARTP yonè lettre diko lath 500 millions francs cfa bindeu ko lettre diko ko reclamer thi ay frequence yu groupe bi ,ndakh lolou rafètt naa ,thi rèwou djioulitte ,injustice yi dafa bari depuis que letat a pris fonction ils ont declarè la guerre a sidy lamine niass et son group de press li kouko mana mougnn ,kènn manouko mougn tè louguèn si khamoul guayi dounioula yoner lettre rèk yam si danioulay bollè akk kou embettant kou niakk yarr ,kou niakk teguine kham ni dou tokk 24 tè wowoula 3 fois au telephone rien que pour dieul sa temps embetter la offenser la rien pour semer un cas de conscience dans ton esprit est ce que lolou Diadou naaa ....
    SIDY LAMINE NIASSS YALL NAGA KHIPPÈ ALDIANA THI BARKÉ SOURATE AL MOULK .....

    • jamila Traoré
      jamila Traoré 2 mesi fa

      sama wanji sama khol toy na si li nga wakh bilahiiiii guisou ma si feutt khaw Mala dh mai li nga wakh yenou na manaa. niou bari si Senegal khamou niou lii. mai . dra yalla bakh na njiko def ma gui niane yalla Bala yakk yalla na lene yalla werr torokhal lene ak coumou mane di donne. diambar danou na yalla na fimm dieum geuneul ko fimm djiougee thi barke alkhourane karim. merci bcp contane na si yao

  • guisall tv
    guisall tv 2 mesi fa

    Yalnakou yereum

  • Alx Diagne
    Alx Diagne 2 mesi fa

    Yalna yalla yeuramko tè diuegalko

  • Nafy Thiam
    Nafy Thiam 2 mesi fa

    que firdawsi soit sa demeure éternel

  • Oumou Ba
    Oumou Ba 2 mesi fa

    Yalla nako yalla khar3 aldiana

  • Adama Diop
    Adama Diop 2 mesi fa

    sais sa la vie que dieu l'accueil dans son paradis

  • Ndommbe Saye
    Ndommbe Saye 2 mesi fa

    diangale lene ko lihlase ak nasi

  • Mbene kane Madame diagne

    رحمك المولى وغفر لك

  • boubacar ly
    boubacar ly 2 mesi fa

    Paix à son âme

  • Bara Ndao
    Bara Ndao 2 mesi fa

    Un grand senegalais est parti un homme qui a beaucoups travailler pour son pays repose en paix

  • assy kane
    assy kane 2 mesi fa

    Paix à son âme

  • Cheikh Ndiaye
    Cheikh Ndiaye 2 mesi fa

    Yalle nako yalla yereum ta kharèko aldiana si barkè yonène bi

  • Seny Tall
    Seny Tall 2 mesi fa

    Paix son âme

  • Diatech Info
    Diatech Info 2 mesi fa

    Voilà une personne qui ne cesse de se contredire et de pervertir les mentalités!
    Pour moi il est même bcp plus nocif que béthio car ce dernier à au moins le culot de se déclarer non compétent en matière de religion. Mais ahmed khalifa lui se prend pour ce qu'il n'est pas et égare en conséquence beaucoup de gens par ses multiples et ambigus
    fatwa.

  • Mbaye Ka
    Mbaye Ka 2 mesi fa

    amine way

  • yeri mayo
    yeri mayo 2 mesi fa

    Q son âme repose en paix un homme véridique et pieux sidy lamine niasse

  • Tima Abubacrine
    Tima Abubacrine 2 mesi fa

    Yalna yallah yeuram ko te khaareko si adjana yu geineu kawe

  • Khoudia Gningue
    Khoudia Gningue 2 mesi fa

    😭😭😭😭 yal nala yala yeureme

  • Kara Mbaye
    Kara Mbaye 2 mesi fa

    yalla na yalla yarame amine

  • Mame Diarra Dieng
    Mame Diarra Dieng 2 mesi fa

    gnatta atte nguako maguee laye lathe

  • cheikh Seye
    cheikh Seye 2 mesi fa

    Que la terre de kaolack lui soit légère et que le paradis soit sa demeure éternelle.

  • chacha ly
    chacha ly 2 mesi fa

    Repose en paix un grand combattant de l'islam

  • Zoon Warriors
    Zoon Warriors 2 mesi fa +1

    Kekhal na dinné ba demm mashallah niass😭😍

  • Awa Alidji Fondo
    Awa Alidji Fondo 2 mesi fa

    Massa Yalla nako Yalla yeureum khareko Aldiana Firdawssi beau temoignage

  • Mame Fallou
    Mame Fallou 2 mesi fa

    yallla nagou yalla yerem ci barqeb serigne touba

  • Sekhle Nianv
    Sekhle Nianv 2 mesi fa

    Yalla nako yalla yerem khareko aldiana firdawsii barki cheikhoul khadim

  • Arabi sadikh bou serign salliwou

    Ndeye sane diallé nola ko yalla nako sounu borome kharé aladiana koukhamo ake deugeu bilahi

  • lucie sane
    lucie sane 2 mesi fa

    Amo thi mome Dogale donté sa rake la. Ndiabotame aye Moukalaf lagnou gno thi ame sagne sagne. Kone khélal lène mais boulène imposé nak. Robe bi fane la kagne la c'est à eux d'endécidé et non toi. Sidy bamouye dounde la sokhlawone Magame ....

    • Fatima Sarr
      Fatima Sarr 2 mesi fa

      Mandou wo dèèè. Domou adama dafaye mandou

  • modou niame
    modou niame 2 mesi fa

    yalnako Yale khare aldiane aminn

  • Aida Niang
    Aida Niang 2 mesi fa

    Yalnanko yalla yeureum te khareko Aldjiana Firdawsi thi barke Mohamed (PSL)

    • baye cheikh
      baye cheikh 2 mesi fa

      ma cha Allah اللهم اغفر له وارحمه ووسع مدخله واحسن وراءه

  • ansata balde
    ansata balde 2 mesi fa

    Yalla nako yalla yaram

  • Moustapha Ndiaye
    Moustapha Ndiaye 2 mesi fa

    Yalnako yalla yeureum té yékhénou,khékhalna niépp ci démocratie Sénégal ak deugg

  • Kara Faye
    Kara Faye 2 mesi fa

    Yalla nako yalla khare aldiana

  • Welzo Wele
    Welzo Wele 2 mesi fa

    Serigne Sidy Al amine niass Yalnaleu Yalla kharé aldiana !si barké seydina souniou sagu Mouhamed ibnou ABDEHLA !

  • Welzo Wele
    Welzo Wele 2 mesi fa

    Yalnako Yalla yeureum kharéko aldiana ! Djibolén , andlén défarlén nékine yi ! Si bi dounde takhawé!boy dound sénégalais deugou , sonal Lou eup si nitt yi, dinaniouleu toumal khass leu wakhni djiouboulo ak défanté Bou méti ak yow!douniouleu nagoul mouk fi ak Yagui dounde,wayé Bou déé takhawé haaaaa yadone ki bakh! Naniou dound si deugu mbok yis di wakhanté deugu! Ndakh diam nék si Nioune diam bouko deugu Lolou keur Bou amoul fondement leu guélal Lay khar pour effondrer !degoulén mane ak yéne di nagoul nitt ki ak diko sédél deugueum si doundeum amna sollo dakh daniou mane roye si mom !maytoulén wakh tay si nitt Lou niaw et surtout loudoul deugu niou tassko si adouna bi internet bi !khalatal tay bouko Yalla dieulé Loy wakh ????senegal dound niouni daga compliquer daga lakalé ,ya li ya leulé!wayé Bou déé takhwé houuuu daga bakhone deugouwon lépongueu si Lou bakh!naniou ragal Yalla!bayi feuseul mbone donténé deuguleu wakhouma nak soff bo tégoul féne loudoul ay fén !maguikoy ndieuké samabop

  • Salieu Sillah
    Salieu Sillah 2 mesi fa

    May Allah grant him jannah, Ameen

  • Aissatou Gueye
    Aissatou Gueye 2 mesi fa

    Sigguilko dingalei niass amine way

  • moado malick Cisse cisse

    yalna yala yeramko thkhareko

  • Kankou Tounkara
    Kankou Tounkara 2 mesi fa

    Repose en paix

  • cheikh cisse
    cheikh cisse 2 mesi fa

    Ila ete nu combatn de islam loo.mana wax baxna. Waye sensgal walla diineji ken duko laall.later lui soi lezer.

  • Elhadji tacko Seck
    Elhadji tacko Seck 2 mesi fa

    اللهم ارحمه وأدخله فسيح جناتك

  • Aliou Sonko
    Aliou Sonko 2 mesi fa

    Machallah un diambar est tombé une étoile étoile est tombé que dieu l'accueil dans son paradis

  • Hamath Gueye
    Hamath Gueye 2 mesi fa

    yalna bour yalla yarekoo aldjianay hiliyina bidjiagii taha yasina ahmada.

  • Gibson Abdou Babou Seck

    loin de son frère qui est un faux type

  • Ousmane Gangue
    Ousmane Gangue 2 mesi fa

    Yala na ko yala xare adjana

  • Balla Ndiaye
    Balla Ndiaye 2 mesi fa

    Yalna KO yalla yaram amine.

  • ami ngum
    ami ngum 2 mesi fa

    May Allah for give him may his soul rest in peace he was a good man

  • adama diallo
    adama diallo 2 mesi fa

    Repose en paix niass

  • Ladara Diop
    Ladara Diop 2 mesi fa

    ohhh que son âme repose en paix

  • Assane Cisse
    Assane Cisse 2 mesi fa

    Bagne Kate démna diambare danouna Sénégal niake na yalnako yalla kharé aldiana

  • Lamineisssa Ly
    Lamineisssa Ly 2 mesi fa

    oh alakhou akbar yall nako yalla
    yerem amine

  • cheikh bodian
    cheikh bodian 2 mesi fa

    kou am jarign mo nopalou yalla na yeureumko té terouko jambar deugu bilay xam diné lepp xam Adouna

  • Djash Keub
    Djash Keub 2 mesi fa

    k firdawsi sw sa demeure éternel paix a son âme

  • Mbaye Toure
    Mbaye Toure 2 mesi fa

    Yalla naco yalla yerem khareko ajana firdawsi

  • Cristal Diouf
    Cristal Diouf 2 mesi fa

    Hol yépa togne gnak nagne kou dougou kougnou done protéger sougnou ngour naré sonal

  • kaka kaka
    kaka kaka 2 mesi fa

    May his soul rest in prefect peace ameen yarabi

  • Neegereum sarr
    Neegereum sarr 2 mesi fa

    sidy reposer en paix notre rèference ndeysanne

  • Ibrahima Ndiaye
    Ibrahima Ndiaye 2 mesi fa

    Niass sa wakh rafet n'a sa rak mo deme YaW la nieup di deglou

  • KAKATAR PROD
    KAKATAR PROD 2 mesi fa

    yalla nako yalla yeureum tee diegalko un vrai combattant

  • Bouba Fit
    Bouba Fit 2 mesi fa

    Na wakhthi rafete ño bokeu nday ak bay

  • SENEGAL TV
    SENEGAL TV 2 mesi fa +1

    Ameen yarabi

  • El hadji kara Diouf

    Yalna la borom touba terrou si adianay firdawsi yaa

    • Basse Mbaye
      Basse Mbaye 2 mesi fa

      +Soukèye Seydi verité absolue mn frere

    • Soukèye Seydi
      Soukèye Seydi 2 mesi fa

      Borom touba a besoin lui même des prières dans sa tombe seul dieu peut accueillir au paradis

  • Diaspora tv rék
    Diaspora tv rék 2 mesi fa +1

    Ma challah

  • Nata Sene
    Nata Sene 2 mesi fa

    Rip

  • Aminata Ndiaye
    Aminata Ndiaye 2 mesi fa

    Yalla na ko yalla yeureume

  • Abu Konate
    Abu Konate 2 mesi fa

    Yalla nako yalla yerem ta kharé ko aldiana

  • assane diop
    assane diop 2 mesi fa

    Yalna souf woyof ci kawam ci barkéb señ saliou mbacké

  • Marie Pam
    Marie Pam 2 mesi fa

    Repose en paix

  • Diatta Mané Sofia
    Diatta Mané Sofia 2 mesi fa

    yalna firsdawsi donn noflayamme😰😰

  • Magy Mbodji
    Magy Mbodji 2 mesi fa

    Hooo

  • Serigne touba Gueye

    Yalla nako Yalla yeureum kharé ko aljana firdawsi

  • Sokhna Diop
    Sokhna Diop 2 mesi fa

    yala na ko yalla khare aldiana

  • Seynabou Wade
    Seynabou Wade 2 mesi fa

    Yana xippee adjana firdaws AMEN repose en paix El Hadj sidi lamine niass coumba abdoulha

  • Diaba Yayou Bour
    Diaba Yayou Bour 2 mesi fa +1

    K la terre lw sw legè 1grand pert pr l senegal

  • Lamine Gueye
    Lamine Gueye 2 mesi fa

    Mbokk Ndeye mokoye djourr

  • Taula Thiam
    Taula Thiam 2 mesi fa

    Dieu.lacueil.dant.on.paradi

  • Adji Seck
    Adji Seck 2 mesi fa +1

    Un homme de valeur un homme digne demna deyesaaane. Yallabnako yalla yereume te yehegnou.

  • abdou DIENG
    abdou DIENG 2 mesi fa

    انا لله وانا اليه راجعون رحمه الله

  • Bara Falilou
    Bara Falilou 2 mesi fa

    yalla nako Yalla Yeureum Ta Xaréko Al Diani Firdaw si Si Barké borom T0UBA

  • Cheikh Gueye
    Cheikh Gueye 2 mesi fa

    yalla nako yalla kharé ajdiana si barké seydina moukhamed amine

  • Modouaicha Thiam
    Modouaicha Thiam 2 mesi fa

    Yalnako yala yeremr tsibarke serine touba

  • Cheikh Thiam
    Cheikh Thiam 2 mesi fa

    Diassi yalla lawone si Sénégal que paradi soit son demeure éternel amine

  • Aichatou Hanne
    Aichatou Hanne 2 mesi fa

    Repose en paix

  • Artiste Diamantaire Hore Bomby Diallo

    papa repose en paix

  • Azize Sow
    Azize Sow 2 mesi fa

    Yalla GA hipe all diana amine si barke moukhamed inchalakh

  • dikha 75
    dikha 75 2 mesi fa

    Paix à son âme 😭

  • Cheikh Gueye
    Cheikh Gueye 2 mesi fa

    Yalla na ka yalla khare adiana

  • Abdalahi diébal dieumeum Ya Allah.

    Sounou Brom Yalla Tabaraka Watahalah, yeureum ko ta diégal ko tabalko Aldiana Firdawsi, ak béb dioulit yi nek si bir souf ak béb dioulit yiy dound. Amine Yarabi!

  • Mamadou SENE
    Mamadou SENE 2 mesi fa +7

    Très courageux, très social, débatteur chevronné, défenseur infatigable de l'islam. Allah sait payer convenablement. Qu'Allah lui accorde son paradis éternel. Amine

  • Dibe Ndiaye
    Dibe Ndiaye 2 mesi fa

    yalnako yalla kharé aldiana firdawsi

  • Matar Babou
    Matar Babou 2 mesi fa +1

    Tu fais honte tous ce la il le mérite lorsque il était vivant. Vreman voilà le monde haujourd huit ms inscrit n peut pas leurrer Dieu

  • Maïrame Thiam
    Maïrame Thiam 2 mesi fa

    paix a son âme

  • badiane diouf Madjiguene

    yalla na KO yalla yeureum te khareko ardiana firdawsi amine