Kooru Biddew Saison 4 - Épisode 16

Condividi
Codice da incorporare
  • Pubblicato il 22 mag 2019
  • Abonnez-vous à notre chaine IT-clip it-clip.net/channel/UCOvrLn57A83J8ojcX70n0Ew
    Suivez-nous sur Facebook facebook.com/leuzmedia?fref=ts
  • IntrattenimentoIntrattenimento

Commenti • 806

  • Jomma Kujabi
    Jomma Kujabi 5 giorni fa

    Dan ak fama rek

  • baby diallo
    baby diallo 16 giorni fa

    Qui a compris l’histoire j’ai l’impression de regarder à l’envers?

  • Ndeye Awa Cissé
    Ndeye Awa Cissé 18 giorni fa

    Naan Dane molloul kw lii moy lan🤣🤣🤣 wlh Bidew nhna❤️❤️❤️

  • dior gueye Diop
    dior gueye Diop 23 giorni fa

    Ehhhh fama ak dane mdr

  • nogaye dieng
    nogaye dieng 24 giorni fa

    couple dane ak daro manou maléne mougne

  • Djebu Bodian
    Djebu Bodian 25 giorni fa

    Kkkk Daro

  • Dija Ndiaye
    Dija Ndiaye 25 giorni fa

    Dane Nena fama sa plat bi dafa triste ,Dane koula bayi Gua ray SA secretaire 😂😂😂😂😂😂😂😂😂 badiane ak tonton douniou dioubou mouk

  • Oumouchka Diallo
    Oumouchka Diallo 25 giorni fa +1

    Pourtant Adji elle semble être une fille gentille deh. Dafa dium rek deim nioxuh dji dieukeuru diambour di forcé mbeuguel lolu moko sonnal . Sinon elle n’est pas mauvaise dama la mudj yeureum sax.

  • Malaw Diallo
    Malaw Diallo 25 giorni fa

    Yéne doléne wowé dîne bi wala oustaz yi

  • Ridwane Couture
    Ridwane Couture 26 giorni fa

    Wa daroo kagne lay togou lou niou lekk

  • Tapha Diallo
    Tapha Diallo 26 giorni fa

    iks

  • Lorie Deme
    Lorie Deme 26 giorni fa

    Non Dane dou nitt nenako sa plat da trisye tropp hahaha de manière tres diplomatique décliner na plat nank

  • JeNeComprendsPas
    JeNeComprendsPas 26 giorni fa

    Li niaaw neu diangui leiine toggou xamngani genre diabbarr yi douniou am ngueureumeul djeukeurr deh

  • Luizito Mendy
    Luizito Mendy 26 giorni fa

    Mass est un grand "yambar"

  • Marie josé niang
    Marie josé niang 26 giorni fa

    Je suis awo mais je ne suis pas d'accord avec bidew une femme doit respecter son mari nimiy wakhé ak djeukeur dou yone

  • Modou Sarr
    Modou Sarr 26 giorni fa +1

    kkkkk daro sa plat bii wakhoumala ray secretaire wayé diarna sakh ray DG kkkkk

  • Ndeye Gueye
    Ndeye Gueye 26 giorni fa

    😂😂😂😂😂noo daro ak yayam dinagne ma ray rék

  • Ousseynou Fall
    Ousseynou Fall 26 giorni fa

    😂😂😂 no rée na ba sonouh rek. .!!

  • Maya Mane
    Maya Mane 27 giorni fa

    Mimi mixeur

  • rouge gazelia
    rouge gazelia 27 giorni fa +2

    Loutah ngueni takk ay diabar ba parei dolene assumé merde way mdr 😂

  • rouge gazelia
    rouge gazelia 27 giorni fa +1

    Loutah ngueni takk ay diabar ba parei dolene assumé merde way mdr 😂

  • yame cisse
    yame cisse 27 giorni fa

    Adji ndeysane damako yeureum elle fait de son mieux.

  • ayesha simplicity
    ayesha simplicity 27 giorni fa

    Badiene ak tonton😆

  • Rmo jr Wade
    Rmo jr Wade 27 giorni fa

    Non fama daf may fay way

  • Fatoumata ndiaye
    Fatoumata ndiaye 27 giorni fa

    Gnarelou mass bi dafa rafeeeete

  • Fatoumata ndiaye
    Fatoumata ndiaye 27 giorni fa

    😂😂😂😂😂😂

  • Astou Diouf
    Astou Diouf 27 giorni fa

    Daro mom sagnsé rék lafi néké

  • Ass Ndiaye
    Ass Ndiaye 27 giorni fa

    Dane raye nama 😂

  • Ass Ndiaye
    Ass Ndiaye 27 giorni fa +1

    Bilaye mass yambar leu 😂

  • Thérèse TOUPANE
    Thérèse TOUPANE 27 giorni fa

    FAMA ET DAN LES BEST

  • adji mbaye
    adji mbaye 27 giorni fa

    Woyyy maguii deee 😂😂😂😂 dane raynama 😂😂😂😂😂woyyy

  • RamÉa hijabie Queen
    RamÉa hijabie Queen 27 giorni fa

    Franchement vous êtes les meilleurs cœur dane ak Fama rk 😂😂
    Mh badiene lingay solou diko sumeekou pour reek tok sa keur aaah Man beugg nala dh souma maggei yalna melni iow

  • Elhadji Ndiaye
    Elhadji Ndiaye 27 giorni fa

    Hahaha je la dore

  • Dior Hadj
    Dior Hadj 27 giorni fa

    Wouyy magui déh Daro dinama rayy 🤣🤣🤣🤣🤣

  • ba bineta
    ba bineta 27 giorni fa

    Woyy😃😃plat Dafa triste 😃😃😃😂😂

  • Seynabou sidibé
    Seynabou sidibé 27 giorni fa +1

    Tibrone khana police diapoulawone loy Def fi🤣🤣

  • julia MENDES
    julia MENDES 27 giorni fa

    ayway Daro tamit plat bi mome sa vréation la dal bayil togn ah ah

  • Djamilah Sankara
    Djamilah Sankara 27 giorni fa

    J'ai regardé pod et marichou et les hommes pouvaient jouer avec les sentiments des femmes sous prétextes qu'ils en avaient le droit.... J'ai regardé maîtresse d'un homme marié, PAREIL.... Actuellement même dans GOLDEN c'est la même chose.... Et voilà KOORU BIDDEW aussi qui prône ça. Dans toutes ces séries les femmes "acceptent leur destin" or c'est pour rivaliser de dingue. J'aime le Sénégal mais franchement faut arrêter... Je ne comprends pas wolof mais liii mom, DAFADOYE

  • Cherif Diallo
    Cherif Diallo 27 giorni fa

    Ok

  • Cherif Diallo
    Cherif Diallo 27 giorni fa

    Begue

  • Dame Diop
    Dame Diop 27 giorni fa +1

    Taak gnaarell legui mou diekh Sénégal liiiiiiiiiiiiiiiiiiii khaana l'islam mayunuko

  • Cheikh Diakhate
    Cheikh Diakhate 27 giorni fa

    Noooo Dane mo nekh

  • Younouss Samb
    Younouss Samb 27 giorni fa

    Mais xaritou adji bi xana dou woor ses cils et ses ongles mom goudou na dii

  • WAKH. DEUG REK
    WAKH. DEUG REK 27 giorni fa

    Madale djigene yi bo takké gnarrel dal gnu changer mélni takk crime la dokhane valable

  • Makhoualye ndiaye
    Makhoualye ndiaye 27 giorni fa

    Noooo daro ak ndann dougnou dém

  • Fatimata Diallo
    Fatimata Diallo 27 giorni fa +1

    Mass ne comporte comme un vrai homme il n'est pas imposant

  • ndong fatou k
    ndong fatou k 27 giorni fa

    ahh wa badieun tamit limiy sagnsé dugnuthi wakh bèn épisode 3 sagnsé ahh eupnaa wayé kèn dou couple bithi coté bi non layti Fall dinama ray très drole waa Fama do djouk thissa bopu liibakagn tamit so moytuwul déh diga gaw am wudju xaral rek djiguèn day meun togue

  • Omzo Ndiaye
    Omzo Ndiaye 27 giorni fa +2

    Plat triste na 😂😂

  • Ahmadou bamba Dieng
    Ahmadou bamba Dieng 27 giorni fa

    Dane moy nafekh😂😂😂

  • Fall Ndiaya
    Fall Ndiaya 27 giorni fa

    😂😂😂😂😂😂😂

  • ramata bakhoum
    ramata bakhoum 27 giorni fa

    Non dane ak fama 🤣🤣🤣🤣🤣

  • miss choco
    miss choco 27 giorni fa +1

    Bidéw dafa commencer réw yapp na mass trop ak sa dieu bou reuy team adjia

  • Amadou Ba
    Amadou Ba 27 giorni fa

    Msse gor dou yambar

  • Fatoumata Sidibe
    Fatoumata Sidibe 27 giorni fa

    Non leyty ya maye raye mane

  • Sall Papa Yoro
    Sall Papa Yoro 27 giorni fa +3

    No m mass dafa yambar trop sah

  • Lamine Konate
    Lamine Konate 27 giorni fa +1

    Bideew tamit.. C'est ton mari, anna respect

  • peulh bou rafet
    peulh bou rafet 27 giorni fa

    😂😂waaah Dane mom nii rek 🤣🤣

  • Thierno Ndiaye
    Thierno Ndiaye 27 giorni fa

    Mé mass bidew mongui beugue tok sa kaw bop boulko nanguou

  • mouhamadouLamine Seye Mou AHMADINÀ SALhIOU

    *_Non dane🤣🤣🤣😄😄🤣😂😂😄😄_*

  • Maty salane
    Maty salane 27 giorni fa +3

    Daro yeureum naka djigen loumou bonne bonne dafa wara meune togue moy lép

  • Junior Fall
    Junior Fall 27 giorni fa

    Bidew limouy def dieukeur dj bakhoul dra masse mom dfa faible torop

  • DIAGNE MBACKE
    DIAGNE MBACKE 27 giorni fa

    KENE DOU DANE

  • Toure Abdou
    Toure Abdou 27 giorni fa +1

    daro sagnsè nga boo ci bolewon di tadie lou nèkh dara douko dakh

  • Balla Aïsha
    Balla Aïsha 27 giorni fa +1

    Meilleure Série 🤗😀😀😂😂😂😂😂😂

  • Abdourahmane Fall
    Abdourahmane Fall 27 giorni fa

    ani wa team dane momay ray mane néna coumbane ndiaye mo gagniou sama secretaire bou gnieuk ba

  • Papa Diene
    Papa Diene 27 giorni fa +1

    No dane d’où dm mom kouco bayi mou ray koumban Ndiaye ndax ndawal😃😁😁😁😁

  • Oumou Kalsoum Sagna
    Oumou Kalsoum Sagna 27 giorni fa

    Sa robe bakhna rama

  • Niama Mbodji
    Niama Mbodji 27 giorni fa

    6np

  • ali cr7
    ali cr7 27 giorni fa +1

    masse yaw mome tapett geu rk

  • fifi Robdrup
    fifi Robdrup 27 giorni fa +5

    Mais yeene bideew dolene ko def normal serie ..c est trop interessant et sensee,j aime beaucoup😄

  • Fane Diop
    Fane Diop 27 giorni fa

    Dane néna ko sa plat bi da triste trop😔😔 😂😂😂😂

  • mariama bodian
    mariama bodian 27 giorni fa

    Je sui maîtresse de la maison wouy daro duma ray😂😂😂😂😂😂

  • Dalanda Diallo
    Dalanda Diallo 27 giorni fa

    Mass amo béne khorom bidew sakh nak wara tass mass comme dof

  • mariama sow
    mariama sow 27 giorni fa +5

    Mass goor day deugeur waayy 😂 surtout nga am kou teeyy melni bideww ta confiance moy tééi relation 💞

  • Adji Ndoye
    Adji Ndoye 27 giorni fa

    Bidew machaallah

  • Rokhy Daba Ndong
    Rokhy Daba Ndong 27 giorni fa +2

    Fama dianguil togg ré na ba sonnn wayy

  • gueye nene
    gueye nene 27 giorni fa

    Badiene et Tonton 😂😂😂

  • Modou Samb
    Modou Samb 27 giorni fa

    Yaalna niou yalla mousseul ci done jeukeur you yambaré comme mass.

  • Madicke Mbengue
    Madicke Mbengue 27 giorni fa +1

    adji selbé ndom lay nirol

  • Aziz Niang
    Aziz Niang 27 giorni fa

    Mimi mi nop nakou deh

  • lady dada
    lady dada 27 giorni fa +1

    Daro bo meunone togu nak tothie fi..nakh say sagnesé bakhna té meune nga tathie

  • Mariama dia toukoulor bou rafét bi

    Team bideew djièk naturel rafet dall tèy saf lokho bégué nala depuis Italie

  • Djouly Touré
    Djouly Touré 27 giorni fa

    Daro nak sa plat bi triste n’a .. tonton y’a meuna dagasanté .

  • borom bélél
    borom bélél 27 giorni fa +1

    Bidew limiy def nii amatoul dh jiguéne niouy wotei nane woko mou rer si jiguéne niou siis gni

  • khadijetou ba
    khadijetou ba 27 giorni fa

    Hhh tristena déh mdr

  • Seydou Diallo
    Seydou Diallo 27 giorni fa

    Good thing 💕💕

  • Awa Sylla
    Awa Sylla 27 giorni fa

    Coumbane ndiaye kay 😂😂😂😂😂😂😂😂😂🤣🤣🤣🤣🤣😂

  • Ibrahima Thiongane
    Ibrahima Thiongane 27 giorni fa

    Guisguene genrou amie yi sa existe dans la société

  • Ndiago France
    Ndiago France 27 giorni fa +1

    Daro nèneu plat togolier wouyyy dèna ak daro

  • Cheikh Darou Sylla
    Cheikh Darou Sylla 27 giorni fa

    Non mane couple Fama ak Dane la mounoul mougne kw billahi Dane nimouy doundé ak Fama metti na nak srx nénako sa plat bi dafa triste trop non Dane amoul kw 😅😅😅😅😅😅

  • Mame Fatou Diop
    Mame Fatou Diop 27 giorni fa

    😂😂😂dan mo 'nèkh coumban Ndiay mo ganiou

  • Khadime Kebe
    Khadime Kebe 27 giorni fa

    Plat bi dafa triste

  • Cherif Marena
    Cherif Marena 27 giorni fa

    Steu steu mère dale chaque jour mou dème kharani nogou

  • Pape Samba Diallo
    Pape Samba Diallo 27 giorni fa +1

    Djigénegni daro mongiléne di wane ni meune Togou bakhena si seuy

  • Kalz Seneg
    Kalz Seneg 27 giorni fa

    Non mass dal tapett leu koi

  • Talibe Cheikh
    Talibe Cheikh 27 giorni fa

    😂😂😂😂 dane raynama naina daro sa plat bi dafa trist

  • Ramatoulaye Dieye Diop
    Ramatoulaye Dieye Diop 27 giorni fa +1

    Dane nak del yeureum fama yako khol ak niak mena togam takk ko menone gua niammm rek😅😅😅😅

  • Ramatoulaye Dieye Diop
    Ramatoulaye Dieye Diop 27 giorni fa +4

    Adji nak moudjou nala yeureum dh
    Lep ak mass beugua fadj mére bay loorr domou jambour iiow sa kaname gui tu c bien k atano 2femme

  • Passane Ndiaye
    Passane Ndiaye 27 giorni fa +1

    Non Dane douma ray nenako sa plat dafa triste trop 😂😂😂

  • Khady Djileh COLY
    Khady Djileh COLY 27 giorni fa +6

    dieuleul ma Fama ak tokkou plat bi😂😂😂ô quelle tristesse!!!